25 Saalec Qeebar xale. Qeebar Feelag xale. Feelag Raaqu xale.
Sem Arfaksad xale. Arfaksad Saalec xale.
Raaqu Sarug xale. Sarug Nacor xale. Nacor Terac xale.