Matthew 9:6 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
6 Wande ndah͈ ngēn mun a h͈am ne Dōm i nit ka am na chi suf sañsañ di baale i bakar, (fōfale mu ne ku lafañ ka,) Jogal, gadul sa lal te dem chi sa ker.
Dēgdēg i tur am dem cha bir Syria yepa; ñu yub ko nit ña op’ on ñepa, ña jangaro ju mun a don ak nchono jap’ on, ak ña i jine jap’ on, ak ña say, ak ña lafañ, te mu weral len.