31 Wande ba ñu fa juge, ñu ēne tur am chi rew mōma yepa.
Cha jamāno jōjale Herod kēlifa ga dēg’ on na lu ñu wah͈ lu jem chi Yesu,
Ñu jel h͈ālis ba, te def la ñu len wah͈ on: kadu gile fireku chi digante Yauod ya, neka bentey.
Dēgdēg i tur am dem cha bir Syria yepa; ñu yub ko nit ña op’ on ñepa, ña jangaro ju mun a don ak nchono jap’ on, ak ña i jine jap’ on, ak ña say, ak ña lafañ, te mu weral len.
Dēgdēg am dem cha bir rew mōma yepa.