24 Mu ne len, May len ma yōn: ndege janh͈a bi dēul, wande defa nelou. Ñu rê ko bu jēpi.
Wande ba ko Yesu dēge, mu ne, Jēr bōbu du tah͈ mu dē, wande di na jem chi ndam i Yalla, ndah͈ Dōm i Yalla jele chi ndam.