20 Jena jigen, ku am on h͈up i deret fuk’ i at ak ñar, ñou chi ganou am, te lāl mbichirān i mbūba’m:
Te dagān ko ndah͈ ñu mun a lāl omb’ i cholay am reka; te ña ko lāl ñepa ñu wer cheng.
Wande ño di def sēn i jef ndah͈ nit gis len: ndege ño di yāal sēn i galaj, te reyal sēn i mbichah͈tan i mbūba,
Yesu jog, ak i tālube am, te topa ko.