Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 9:2 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

2 Ñu yub ko nit ku lafañ, teda chi lal: ba Yesu gise sēn ngum, mu wah͈ ku lafañ ka, ne, Suma dōm, na sa h͈ol dal; baal nañu la sa i bakar.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 9:2
32 Iomraidhean Croise  

Wande Yesu wah͈ len chi tah͈ouay, ne, Dalal len sēn h͈ol: Man la; bu len tīt.


Dēgdēg i tur am dem cha bir Syria yepa; ñu yub ko nit ña op’ on ñepa, ña jangaro ju mun a don ak nchono jap’ on, ak ña i jine jap’ on, ak ña say, ak ña lafañ, te mu weral len.


Te baal ñu suñu i bakar, naka ñu baale ña ñu tōñ;


Ba ko Yesu dēge, mu jomi, te ne ña ko top’ on, Chi dega mangi len di wah͈, mosu ma feka ngum gu nu day, dēt, du chi Israel.


Ba ngon jote, ñu yub ko ña i jine jap’ on, te mu gēne malāka yu bon ya chi ñom chi bāt am, te weral ña jēr on ñepa:


Wande Yesu woñaku, te ba mu ko gise, mu ne, Dōm ju jigen ji, na sa h͈ol dal; sa ngum weral na la. Jigen ja dal di wer cha wah͈tu wōwale.


Lan a chi gen a yomba wah͈, ne, Baal nañu la sa i bakar; wala ne, Jogal, te doh͈?


Wande ndah͈ ngēn mun a h͈am ne Dōm i nit ka am na chi suf sañsañ di baale i bakar, (fōfale mu ne ku lafañ ka,) Jogal, gadul sa lal te dem chi sa ker.


Yef yile lā len wah͈ ndah͈ chi man ngēn mun a am jama. Chi aduna si di ngēn am ngeten: wande na ngēn degerlo sēn hol; ndig fabi nā aduna si.


Te soh͈lawul kena sēde chi lu jem chi nit; ndege mō h͈am on lu neka chi h͈ol i nit.


Yesu ne len, H͈alel yi, ndah͈ am ngēn lu ngēn leka?


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan