Matthew 9:18 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
18 Ba mu len wah͈andô yef yile, bena kēlifa ñou, te dagān ko, ne, Nistey suma dōm ju jigen dē na; wande ñoual, teg sa loh͈o chi kou am, te di na dundati.
Du ñu def itam biñ bu ês chi mbūs yu maget: wala mbūs ya h͈ar, biñ ba tūru, te mbūs ya yah͈u: wande di nañu def biñ bu ês chi mbūs yu ês, te ñar ña dēnchu.