Matthew 9:15 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 190715 Yesu ne len, I mbok’ i nēg i borom‐chēt ga, ndah͈ mun naño nah͈arlu ba borom‐chēt ga neke ak ñom? Wande jamāno di na diki ba ño fabi borom‐chēt ga cha ñom; bōbale di nañu ôri. Faic an caibideil |