Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 9:14 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

14 Fōfale i tālube i John ñou fi mōm, ne, Lutah͈ ñu di faral a ôr, ak Pharisee ya, te sa i tālube du ñu ôr?

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 9:14
10 Iomraidhean Croise  

Ba John dēge chi tejukay ba i koutef i Krista, mu yōne cha i tālube am;


Su ngēn di ôr, bu len am kanam gu dīs niki nafeh͈a ya; ndege di nañu ñaulo sēn i kanam ndah͈ nit ña gis ne ñunge ôr. Chi dega mangi len di wah͈, Am nañu sēn yōl.


Yesu ne len, I mbok’ i nēg i borom‐chēt ga, ndah͈ mun naño nah͈arlu ba borom‐chēt ga neke ak ñom? Wande jamāno di na diki ba ño fabi borom‐chēt ga cha ñom; bōbale di nañu ôri.


Lājte jog nak chi digante i talube i John ak Yauod ya chi lu jem chi setalay.


Ba Borom bi h͈ame nak ne Pharisee ya dēg’ on nañu ne Yesu angi don def te batise i talube yu gen a bare as John,


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan