29 Ñu h͈āchu, ne, Lan la ñu jote ak you, you Dōm i Yalla? Dā fi dika ndig geten ñu bala wah͈tu wa jot?
Ba firkat ba ñoue fi mōm, mu ne, So de Dōm i Yalla, na nga ebal h͈êr yile ñu neka mburu.
Gēt’ i mbām yu bare sorey on nañu fale di far.
Te Yesu ne ko, Jigen ji, lu ma jote ak you? Suma wah͈tu dikangul.