Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 8:28 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

28 Ba mu age cha genen wet, chi bir rew i Gadarene ya, ñar i nit ñu i jine jap’ on feka ko, di juge cha bamel ya, te ñu soh͈or lol, be ken munul a jār yōn wōwale.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 8:28
9 Iomraidhean Croise  

Dēgdēg i tur am dem cha bir Syria yepa; ñu yub ko nit ña op’ on ñepa, ña jangaro ju mun a don ak nchono jap’ on, ak ña i jine jap’ on, ak ña say, ak ña lafañ, te mu weral len.


Nit ña jomi, ne, Ban melin i nit a di kile, be ngelou li sah͈ ak gēch gi di ko dēgal!


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan