24 Ngelou lu rey jog cha gēch ga, be gāl ga muro ak dūs ya; wande mu don nelou.
Ba mu duge chi gāl, i tālube am topa ko.
Ñu ñou fi mōm, te ê ko, ne, Borom bi, musal ñu: ñunge sanku.
Te da ma kontan ndig yēn ne neku ma fa won, ndah͈ ngēn gum; wande na ñu dem fa mōm.