17 Ndah͈ la Isaiah yonent ba wah͈ on motaliku, ne, Mō jel on suñu munadi, te yubu on suñu i jangaro.
Yile yepa am on na ndah͈ la Borom bi wah͈ on chi yonent ba motaliku, ne,
Mu neka fa be ba Herod dēe, ndah͈ la Borom bi wah͈ on cha yonent ba motaliku, ne, Cha Mesara lā ôe suma dōm.
Te ñou, deka chi rew mu tūda Nazareth: ndah͈ la yonent ya wah͈ on motaliku, ne, Di nañu ko tūde Nazarene.