12 Wande i dōm i ngur ga, di nañu len tabal chi lendem i biti; fōfale la joy di neka ak yeyi buñ.
Tōl ba aduna si la; jiu wu bāh͈ wa i dōm i ngur ga la; nduh͈um la i dōm i bulis la;
Te sani len cha safara sa; fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.
Te sani len chi safara si: fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.
Mōtah͈ ma ne len, Di nañu jele ngur i Yalla fi yēn, te joh͈ ko h͈êt wu di mēña mēñef am.
Dog ko chi diga, te sedāle ko nafeh͈a ya: fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.
Te sani len jām bu jeriñul bi cha lendem i biti: fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.