8 Ndege ku mu mun a don ku lāj, di na am; te ku ūt, di na gis; te ku foga, di nañu ko ūbi.
Lāj len, te di nañu len may; ūt len, te di ngēn gis; foga len, te di nañu len ūbi:
Kan chi yēn, su ko dōm am lāje mburu, mu may ko doch?
Ô on nañu itam Yesu ak i talube am cha sey ba.