28 Am on na ba Yesu sotale bāt yile, mbōlo ma jomi chi njemantal am:
Am on na ba Yesu sotal on eble fuk’ i tālube am ak ñar ña, mu juge fa, ndah͈ mu jemantale te wāre chi sēn i deka.
Am on na ba Yesu sotal on kadu yile, mu juge cha Galilee, te ñou chi i mpeg’ i Judæa ganou Jordan:
Ba ko mbōlo ma dēge, ñu jomi cha njemantal am.
Am on na, ba Yesu sotal on bāt yōyale yepa, mu ne i tālube am,
Tou ba dal, wame wa buna, ngelou la ñou, te dal chi kou nēg bōbale; mu maba; maba gu rey.
Ndege jemantal on na len naka ku am sañsañ, te nekul naka sēn i bindānkat.
Tah͈na Yauod ya jomi, ne, Naka la kile def be mun a janga, te mosul a jemantu?
Saltige ya tontu, ne, Ken mosul a wah͈ niki kile.