23 Fōfale di nā len yēgal, ne, Mosu ma len a h͈am; randu len ma, yēn ña def lu bon.
Wande mu tontu, ne, Chi dega mangi len di wah͈, h͈amu ma len.
Fōfale di na wah͈ ña chi chamoñ am, ne, Randu len ma, yēn ñi alaku, dem len cha safara su dul jêh͈, ba ñu wājal on Seytane ak i malāk’ am:
Mā di samakat bu bāh͈ bi, te h͈am nā suma yos, te suma yos h͈am nañu ma,