2 Ndege ate bu ngēn ate ñenen, di nañu len ko ateji; te natu bu ngēn di natale, mōm sah͈ la ñu len di nataleji.
Ndege su ngēn baale nit sēn i tōñ, sēn Bay ba cha ajana di na len baal itam: