12 Mōtah͈ lu ngēn buga lepa nit di len ko defal, yēn itam na ngēn ela defal ñenen: ndege bile di yōn wi ak yonent ya.
Bu len dēfe ne da ma dika fanh͈asi yōn wa ak lu yonent ya wah͈ on; diku ma fanh͈asi wande motalisi.