Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 6:6 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

6 Wande you, so di ñān, dugal chi sa bir nēg, te ba nga teje bunta ba, ñānal sa Bay ki chi nubu; te sa Bay ki di gis lu nubu, di na la yōl.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 6:6
17 Iomraidhean Croise  

Ganou ba mu demlô mbōlo ma, mu yēg cha kou tūnda wa ndah͈ mu ñān Yalla, te chi gudi ga mu neka fa mōm dal.


Ndah͈ do mel naka ku di ôr chi nit, wande chi sa Bay ki chi nubu; te sa Bay ka gis lu nubu, di na la yōl.


Ndah͈ sa sarah͈ di nubu, te sa Bay ki di gis lu nubu, di na la yōl.


Nathanael ne ko, Ana fo ma h͈ame? Yesu tontu te ne ko, Ba la Philip ôangule, ba nga neke cha run mbot ga, gis nā la.


Yesu ne ko, Bul ma japa; ndege yēgangu ma fa Bay ba: wande demal fa suma i mboka, te ne len, Da ma yēg fa suma Bay ak sēn Bay, fa suma Yalla ak sēn Yalla.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan