Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 6:16 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

16 Su ngēn di ôr, bu len am kanam gu dīs niki nafeh͈a ya; ndege di nañu ñaulo sēn i kanam ndah͈ nit ña gis ne ñunge ôr. Chi dega mangi len di wah͈, Am nañu sēn yōl.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 6:16
25 Iomraidhean Croise  

Otu len ngēn def sēn i jef yu bāh͈ chi kanam i nit ndah͈ ñu gis len, mbāte du len am yōl chi sēn Bay ba cha ajana.


So di sarah͈e mbōk, bul buftalo chi sa kanam, naka nafeh͈a ya di def chi juma ya ak mbeda ya, ndah͈ ñu am teranga chi nit. Chi dega mangi len di wah͈, Am nañu sēn yōl.


Su ngēn di ñān, bu len def niki nafeh͈a ya: ndege sopa naño tah͈ou di ñān chi juma ya ak chi mbeda ya, ndah͈ nit gis len. Chi dega mangi len di wah͈, Am nañu sēn yōl.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan