14 Ndege su ngēn baale nit sēn i tōñ, sēn Bay ba cha ajana di na len baal itam:
Barkel cha ña am yermande; ndege di nañu joti yermande.
Te baal ñu suñu i bakar, naka ñu baale ña ñu tōñ;
Ndege ate bu ngēn ate ñenen, di nañu len ko ateji; te natu bu ngēn di natale, mōm sah͈ la ñu len di nataleji.