43 Dēga ngēn ñu wah͈, ne, Na nga sopa sa morom, te sib sa mbañ.
Teralal sa bay ak sa ndey: te, Sopal sa morom niki sa bopa.
Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bulu rēy; te ku di rēy mungi chi tafār i ate:
Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bul njālo: