38 Dēga ngēn ñu wah͈, ne, But ak but, buñ ak buñ:
Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bulu rēy; te ku di rēy mungi chi tafār i ate:
Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bul njālo: