33 Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bulu leka ngeñ, wande motali ko chi Yalla:
III. Bulu jil tur i Yalla saa Borom ce cahan, ndegi, Borom bi, du ko seti naka bakar, ku jil tur am ce cahan.
Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bulu rēy; te ku di rēy mungi chi tafār i ate:
Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bul njālo: