32 Wande mangi len di wah͈, Ku fase ak jabar am, lu moy mu di chi njālo, tah͈ na ko mu njālo; te ku sey ak mōm ka ñu fase, njālo na.
Wande mangi len di wah͈, Ku sêt jigen te h͈emem ko, nistey njālo na ak mōm chi h͈ol am.