31 Wah͈ nañu itam, ne, Ku fase ak jabar am, na ko joh͈ mbinda i mpase:
Pharisee ya ñou fi mōm, di ko fir, te ne ko, Ndah͈ dagan na nit fase jabar am ndig lu mu mun a don?
Ñu ne ko, Bōba lutah͈ on Musa ebal ñu joh͈ mbind’ i mpase, te fase ak mōm?