27 Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bul njālo:
VII. Bulu njaalo.
Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bulu rēy; te ku di rēy mungi chi tafār i ate:
Dēga ngēn ñu wah͈ on nit i h͈āt ya, Bulu leka ngeñ, wande motali ko chi Yalla:
Dēga ngēn ñu wah͈, ne, But ak but, buñ ak buñ:
Dēga ngēn ñu wah͈, ne, Na nga sopa sa morom, te sib sa mbañ.