25 Goual a mar ak sa mbañ naka nga neke chi yōn wa ak mōm; lu dul lōga mbañ ma di na la joh͈e chi atekat ba, te atekat ba di na la joh͈e chi otukat ba, te mu tej la chi kaso.
Wande Peter topa ko bu sorey chi ker i kēlifa i seriñ ya, h͈araf chi bir, te tōg ak rapas ya, ndah͈ mu sêt muj ga.