Matthew 5:19 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 190719 Ku mu mun a don mbōk ku di moy bena chi eble yile bu gen a tūt, te jemantal nit ña nogule, di nañu ko tūdeji ka gen a new ñepa chi ngur i ajana; wande ku len di def te jemantal len, di nañu ko tūdeji ku rey chi ngur i ajana. Faic an caibideil |