Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 5:11 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

11 Barkel chi yēn su ñu len di h͈as, te geten len, te sos lu bon yepa chi yēn ndig man.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 5:11
32 Iomraidhean Croise  

Te di nañu len yubu chi kanam i kēlifa ak i bur ngir man, ndig sēde chi ñom ak chi Gentile ya.


Ñepa di nañu len sib ndig man; wande ku di muñ be cha muj ga mō di muchi.


Doy na chi tālube mu neka naka jemantalkat am, te jām naka borom am. Su ñu ôe borom‐ker ga Abdujambar, naka ña mōmu chi ker am!


Ku ūt dund’ am, di na ko rēr; te ku rēral dund’ am ngir man, di na ko gis.


Te ku neka ku bayi i nēg, mbāt i raka, mbāt i jigen, mbāte bay, mbāte ndey, mbāt i dōm, mbāt i tōl ngir man, di na ami lu bare lu len upa, te dona dunda gu dul jêh͈.


Fōfale di nañu len jebale ndah͈ ñu geten len, te di nañu len rēy: h͈êt yi yepa di nañu len sib ndig man.


Ña fa romba sāga ko, di yengal sēn i bopa, ne,


Wande yef yile yepa la ñu di defi ndig suma tur, ndege h͈amu ñu ka ma yōni on.


Te ñu h͈ūle ko, te ne, Yā di talube am; wande ño di talube i Musa ya.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan