9 Te ne ko, Yef yōyu yepa lā la di may, so sūke chi suma kanam, te jāmu ma.
Te ne len, Lan ngēn ma joh͈, te di nā len ko jebal? Ñu dige ak mōm ñeta fuk’ i dogit i h͈alis.
Fōfale Yesu ne ko, Randu ma Seytane, ndege binda nañu, ne, Na nga jāmu Borom ba sa Yalla, te na nga ko topa, mōm reka.
Ate’ aduna sile jot na: lēgi ñu gēne gelouar i aduna sile, te sani ko cha biti.
Yesu ka h͈am ne Bay ba joh͈ na yef yepa chi i loh͈o am, te juge won na cha Yalla, te di na dem fa Yalla,
Du ma wah͈ati ak yēn lu bare; ndege gelouar i aduna sile ñou na; te amul dara chi man;
Chi ate, ndege gelouar i aduna sile ate nañu ko.