5 Seytane nak yubu ko fa deka bu sela ba, teg ko cha kou puj i juma ja,
Gēna chi bamel ya ganou ndēkite am, h͈araf chi bir deka bu sela ba, te fêñu i nit jupa.
Yesu tontu ko, ne, Do mun a am sañsañ chi man lu moy ñu joh͈ la ko cha kou: mōtah͈ ka ma jebale won fi you, mō la gen a bakar.