Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 4:24 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

24 Dēgdēg i tur am dem cha bir Syria yepa; ñu yub ko nit ña op’ on ñepa, ña jangaro ju mun a don ak nchono jap’ on, ak ña i jine jap’ on, ak ña say, ak ña lafañ, te mu weral len.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 4:24
41 Iomraidhean Croise  

Fōfale ñu indi fa mom kena ku jine jap’ on, ka silmah͈a te lū; mu weral ko, tah͈na nit ka lū on wah͈ te gis.


Cha jamāno jōjale Herod kēlifa ga dēg’ on na lu ñu wah͈ lu jem chi Yesu,


Jena jigen i Canaan juge cha wet yōya, te mu h͈āch͈u, ne, Amal yermande chi man, E Borom bi, Dōm i Dauda; jine anga geten suma dōm ju jigen bu miti.


Borom bi, amal yermande chi suma dōm ju gōr; ndege defa say, te getenu bu miti; faral na tabi chi safara, ak chi ndoh͈.


Yesu h͈ūle ko, te jine ja gēna chi mōm; cha wah͈tu wōwale h͈alel ba wer.


Yesu dem cha bir Galilee yepa, di jemantale chi sēn i juma, di wāre linjil i ngur gi, te di weral h͈êt i opa ju neka, ak hêt i jangaro ju neka chi digante nit ña.


Ba mu age cha genen wet, chi bir rew i Gadarene ya, ñar i nit ñu i jine jap’ on feka ko, di juge cha bamel ya, te ñu soh͈or lol, be ken munul a jār yōn wōwale.


Ña len don sama dou, dem chi bir deka ba, te wah͈ lu neka, ak lu jot nit ña jine jap’ on.


Ne, Borom bi, suma bukanēg anga teda cha ker, lafañ, te sona bu miti.


Dēgdēg am dem cha bir rew mōma yepa.


Yesu dem cha rew ya ak deka ya yepa, di jemantale chi sēn i juma, wāre linjil i ngur gi, te weral ña opa ñepa, ak jarak ju neka chi digante nit ña.


Ñenen ne, Yile du wah͈ i ku ame jine. Ndah͈ jine mun na ūbi but i silmah͈a?


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan