Matthew 4:23 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
23 Yesu dem cha bir Galilee yepa, di jemantale chi sēn i juma, di wāre linjil i ngur gi, te di weral h͈êt i opa ju neka, ak hêt i jangaro ju neka chi digante nit ña.
Yesu tontu ko, ne, Man chi kanam i ñepa lā wah͈ on chi aduna si; dan nā jemantal cha juma ya, ak cha jangu ba fa Yauod ya dajale ñepa; te wah͈u ma won dara chi kumpa.