21 Bu mu fa juge, mu gis yenen i mboka, James dōm i Zebedee, ak rak’ am John, chi gāl ga, ak Zebedee sēn bay, di dāh͈ sēn i mbal; te mu ô len.
Tūr i fuk’ i tālube ak ñar yangile: Benel bi, Simon ku tuda Peter, ak Andrew rak’ am; James dōm i Zebedee, ak John rak’ am;
Ganou jurom ben’ i fan, Yesu jel Peter, James, ak John rak’ am, te yubu len chi kou tūnda wu koue, ñom dal:
Mu jel ak mōm Peter ak ñar i dōm i Zebedee, dôr di yogorlu ak nah͈arlu lol.
Ñu wocha mbal ya chi tah͈ouay, te topa ko.
Ñu dal di wocha gāl ga, ak sēn bay, te topa ko.
Nek’ on nañu fōfa Simon Peter, ak Thomas ku tūda sīh͈ bi, ak Nathanael i Cana cha Galilee, ak i dōm i Zebedee, ak ñenen ñar i talube am.