16 Nit ña jēki on chi lendem gis nañu lêr gu rey, te ña jēki on chi rew i dē ak takandēr am, chi ñom la lêr joge.