Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 4:14 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

14 Ndah͈ la Isaiah yonent ba wah͈ on motaliku, ne,

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 4:14
15 Iomraidhean Croise  

Yile yepa am on na ndah͈ la Borom bi wah͈ on chi yonent ba motaliku, ne,


Mu neka fa be ba Herod dēe, ndah͈ la Borom bi wah͈ on cha yonent ba motaliku, ne, Cha Mesara lā ôe suma dōm.


Te ñou, deka chi rew mu tūda Nazareth: ndah͈ la yonent ya wah͈ on motaliku, ne, Di nañu ko tūde Nazarene.


Wande naka la mbinda mi di motalikô, ne nōgu la ela ame?


Wande lile yepa am na, ndah͈ mbinda i yonent ya motaliku. Fōfale la ko tālube ya yepa woche, te dou.


Te juge Nazareth, mu ñou deka chi Capernaum, bu jegeñ gēch ga, chi wet i Zebulun ak Naphtali:


Suf i Zebulun ak suf i Naphtali, chi yōn i gēch ga, ganou Jordan, Galilee i Gentile ya;


Ndah͈ la Isaiah yonent ba wah͈ on motaliku, ne, Mō jel on suñu munadi, te yubu on suñu i jangaro.


Wande lile jot na, ndah͈ bāt ba ñu bind’ on chi sēn yōn motaliku, ne, Bañ nañu ma te defu ma dara.


Ganou lōlu, Yesu ba mu h͈ame ne yepa soti na, ndah͈ mbinda ma motaliku, mu ne, Mar nā.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan