13 Te juge Nazareth, mu ñou deka chi Capernaum, bu jegeñ gēch ga, chi wet i Zebulun ak Naphtali:
Te you Capernaum, mi yēkatiku cha asaman, di nañu la sufel be chi nāri: ndege koutef ya ma def on chi you, su ñu len def on cha Sodom, kôn mu des bentey.
Ba ñu dike chi Capernaum, ña di jel ngalak la ñou fi Peter, ne, Ndah͈ sēn borom du fey ngalak?
Ndah͈ la Isaiah yonent ba wah͈ on motaliku, ne,
Suf i Zebulun ak suf i Naphtali, chi yōn i gēch ga, ganou Jordan, Galilee i Gentile ya;
Yesu duga chi gāl, jala, te ñou chi dek’ am.
Ganou lōlu mu dem fa Capernaum, mōm, ak ndey am, ak i rak’ am, ak i talube am; te ñu jēki fa fan yu new.
Mu ñouati nak cha Cana i Galilee, fa mu sopali won ndoh͈ ma biñ. Te bena kangam am on na, ka dōm am ju gōr opa cha Capernaum.
Te ñu duga chi gāl, te dal di jala gēch ga cha Capernaum. Te mu lendem, te Yesu ñouangul on fa ñom.
Ba mbōlo ma gise nak ne Yesu neku fa, mbāte i talube am, ñom it ñu duga chi gāl ya, te ñou chi Capernaum, di ūt Yesu.
Yef yile la wah͈ on cha juma ja, ba mu jemantal on cha Capernaum.