1 Fōfale la Nh͈el ma jīte Yesu cha manding ma, ndah͈ Seytane fir ko.
Du ma wah͈ati ak yēn lu bare; ndege gelouar i aduna sile ñou na; te amul dara chi man;