4 John nak mō sol on nchangay i kouar i gelem, ak lah͈asay i der chi ndig am; te dundu am njērer la won, ak lem i ala.
Ndege John ñouūl on di leka wala di nān, te ñu ne, Anda na ak jine.
Wande lan ngēn dem on ndah͈ ngēn sêt? Nit ku sāngu chi nchangay lu noy am? Ña sāngu chi nchangay lu noy angi chi i nēg ī bur.