Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 28:18 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

18 Yesu ñou fi ñom, te wah͈ len, ne, May nañu ma kantan yepa cha ajana ak chi suf.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 28:18
31 Iomraidhean Croise  

Suma Bay jebal na ma yef yepa; te ken h͈amul Dōm ji wande Bay bi; te ken h͈amul Bay bi wande Dōm ji, ak ku Dōm ji nangu mu h͈am ko.


Chi dega mangi len di wah͈, Ñena ñi tah͈ou file, du ñu mos dē, be ba ñu di gisi Dōm i nit ka mu di ñou chi ngur am.


Yesu ne ko, Wah͈ nga ko: te mangi len di wah͈, Ganou lile di ngēn gisi Dōm i nit ka mu di tōg chi loh͈o’ ndējor i kantan, di wachasi chi i nir i asaman.


Yesu ka h͈am ne Bay ba joh͈ na yef yepa chi i loh͈o am, te juge won na cha Yalla, te di na dem fa Yalla,


Naka nga ko maye won sañsañ chi kou nit ñepa, ndah͈ mu maye ña nga ko may on ñepa dūnda gu dul jêh͈.


Ka juge cha kou, chi kou ñepa la neka: ka juge aduna, chi aduna la boka, te lu boka chi aduna la wah͈: ka juge ajana, chi kou ñepa la neka.


Bay ba sopa na Dōm ja, te joh͈ na ko lu neka chi loh͈o am.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan