14 Su kēlifa ga dēge lile, di nañu ko dalal, te dindi len chi jāh͈le.
Ñu ew ko, omat ko, te jebal ko Pilate kēlifa ga.
Na ngēn ne, I tālube am a dik’ on chi gudi, te sacha ko ba ñu neloue.