12 Ba ñu dajalô ak mag ña, te fēncha, ñu may otukat ya h͈alis bu bare, ne,
Wande Pharisee ya gēna, te fēncha naka ñu ko mun a rēye.
Ba ño dem nak, ñena chi otukat ya ñou chi bir deka ba, te nitali i njīt i seriñ ya la h͈ew on yepa.
Na ngēn ne, I tālube am a dik’ on chi gudi, te sacha ko ba ñu neloue.
Njīt i seriñ ya nak ak Pharisee ya dajalo fēncho, te ne, Ana lu ño def? ndege nit kile def na koutef yu bare.