11 Ba ño dem nak, ñena chi otukat ya ñou chi bir deka ba, te nitali i njīt i seriñ ya la h͈ew on yepa.
Ba ñu dajalô ak mag ña, te fēncha, ñu may otukat ya h͈alis bu bare, ne,
Ndig mōm otukat ya tīt be di dagdagi, te mel niki ñu dē.