59 Yusufa jel yaram wa, lomas ko chi ser wu set te wêh͈,
Kile dem fa Pilate te dagān yaram i Yesu. Fōfale Pilate eble ñu joh͈ ko ko.
Te teral ko chi bamel am bu ês, ba mu et’ on chi h͈êr: mu borong doch wu rey chi bunt’ i bamel ba, te dem.