57 Ba ngon jote, borom‐alal ku juge on Arimathæa, ka tūda Yusufa, te nek’ on itam tālube i Yesu:
Kile dem fa Pilate te dagān yaram i Yesu. Fōfale Pilate eble ñu joh͈ ko ko.