54 Saltige ba nak, ak ña nek’ on ak mōm, di otu Yesu, ba ñu gise yengatu’ suf sa, ak yef ya am, ñu tīt lol, ne, Chi dega kile Dōm i Yalla la.
Wande Yesu japa gemeñ am. Kēlifa i seriñ ya ne ko, Mangi la dagān chi tur i Yalla ji di dunda, nga wah͈ ñu ndah͈ yā di Krista, Dōm i Yalla.
Ñu tōg, di ko otu fōfale.
You mi dānel jama ja te tabah͈ati ko chi ñet’ i fan, musalal sa bopa. So de Dōm i Yalla, wachal chi kura bi.
Mu ōlu Yalla; na ko musal lēgi, su ko buge; ndege nôn na, Mā di Dōm i Yalla.
Ser i juma ja h͈otiku chi diga, cha kou be chi suf; suf si yengatu; doch yu rey ya h͈ar;
Ba firkat ba ñoue fi mōm, mu ne, So de Dōm i Yalla, na nga ebal h͈êr yile ñu neka mburu.
Ba Yesu h͈arafe chi Capernaum, bena saltige ñou fi mōm, te dagān ko,
Yauod ya tontu ko, ne, Am nañu yōn, te chi suñu yōn wōgu ela na dē, ndege def on na bop’ am Dōm i Yalla.