52 Bamel ya ūbeku; te i yaram i jūlit yu bare ñu don nelou jog;
Yef yile la wah͈ on; te ganou lōlu mu ne len, Lazarus suñu h͈arit defa nelou; wande di nā dem ndah͈ ma ê ko chi nelou am.