5 Mu sani dogit i h͈alis ya chi suf chi juma ja, gēna, te dem, eng̈a bop’ am.
Nit kile wah͈ on na, ne, Mun nā dānel juma’ Yalla, te tabah͈ati ko chi ñet’ i fan.
I njīt i seriñ ya jel dogit i h͈alis ya, ne, Daganul ñu def ko chi dēnchukay bu sela bi, ndege njēg i deret la.